Le 18 mars 2025, une délégation de la Commission de l’éducation, de la jeunesse, des sports et des loisirs de l’Assemblée nationale du Sénégal a été reçue par le Directeur général du 3FPT, Dr Babo Amadou BA.
Cette rencontre s’inscrit dans une initiative visant à mieux comprendre les enjeux liés à la formation professionnelle et technique, ainsi qu’à établir un cadre de partage d’informations avec les parlementaires concernant les structures étatiques impliquées dans ce domaine.
———-
18i fani mars 2025, aw tañ (délégation) bu Bànqaasu njàng, ndaw ñi ak tàggat yaram ak um po ci “Assemblée nationale” bu Senegaal dalal na Njiitu 3FPT, Dr. Amadou BA.
Ndaje mi di jéego bu am solo ci man a nànd jafe-jafe yi jëm ci tàggatu gu xereñ gi ak xarala, ak it teg lu jëm ci joxe i xibaar ak “parlementaires” ci wàllug liggéey yu jëm ci yor ci wàll wi.
“3FPT – Fonds de financement de formation professionnelle et technique”
3FPT – Fonds de Financement de la Formation professionnelle et technique.




